4-G
Xew-xew yi gën a am solo ci dundu Yeesu — Waare Yeesu bi mujj ci Yerusalem (Xaaj 1)
JAMONO JA |
BÉRÉB BA |
XEW-XEW BA |
MACË |
MÀRK |
LUUG |
YOWAANA |
---|---|---|---|---|---|---|
8 Nisan 33 |
Betani |
Yeesu agsi juróom-benn fan bala bésu Mucc ga |
||||
9 Nisan |
Betani |
Maryaama sotti ko latkoloñ ci bopp ak tànk |
||||
Betani-Betfase-Yerusalem |
Mu yéeg mbaam dugg Yerusalem |
|||||
10 Nisan |
Betani-Yerusalem |
Mu rëbb garabu figg ga ; mu sellalaat kër Yàlla ga |
||||
Yerusalem |
Sarxalkat yu mag ya ak xutbakat ya di fexee rey Yeesu |
|||||
Yexowa wax ; Yeesu wax ci deewam ; ñàkk ngëmu Yawut yi matal na yégle yonent Yàlla Esayi |
||||||
11 Nisan |
Betani-Yerusalem |
Njàngale ci garabu figg bi ñu wowal |
||||
Yerusalem, kër Yàlla ga |
Ñu weddi sañ-sañu Yeesu ; léebu ñaari doom yi |
|||||
Ay léebu : beykat yiy reyaate, céet ga |
||||||
Tont yi ci laaj yu jëm ci Yàlla ak Sesaar, ndekkite li, santaane bi gën a màgg |
||||||
Mu laaj ndax Almasi bi mooy sëtu Daawuda |
||||||
Yeesu gëdd xutbakat ya ak Farisen ya |
||||||
Muy xool li jigéen ji ñàkk jëkkëram di maye |
||||||
Tund Oliw ya |
Mu wax liy tegtal ne mu ngi ñëw |
|||||
Ay léeb : fukki janq ya, talaŋ ya, xar yi ak bëy yi |
||||||
12 Nisan |
Yerusalem |
Njiitu Yawut yi di wut pexe ngir rey ko |
||||
Yudaa di lijjanti ngir wor ko |
||||||
13 Nisan (Alxemes ci bëccëg) |
Yerusalem ak li ko wër |
Muy waajal Màggalu bésu Mucc bi mujj |
||||
14 Nisan |
Yerusalem |
Mu lekk ak ndawam yi ci bésu Mucc ga |
||||
Mu raxas tànki ndaw yi |